https://archive.org/details/singali
Singali : Nettali by Séex Aliyu Ndaw; Cheik Aliou Ndao
Topics
#njàngat, #téeré, #baayo
"Singali téereb fent nettali la buy jéem a wone dund gu nàqari gi ab baayo nekke, rawatina su ndeyu jiitle ja wonewul as tuut ci yërmande.
Li am solo mooy jom, muñ, ak dogu dimbale nañu Singali ba mu màgg faj gàcce.
Waaye ba mu tekkee taxul muy feyyoonte. dafa tamu doon nit ku tabe, tey jéggale.
Ndax kat dafa bokk ci ñi gëm ne lépp a ngi ci loxol boroom bi."