https://archive.org/details/bammeelu-kocc-barma
Bàmmeelu Kocc Barma : Téereb nettali by Bubakar Bóris Jóob; Boubacar Boris Diop
"Njéeme Pay, taskatu xibaar bu siiw ci Senegaal, moo toog bés këram dégg ci rajoy réew mi ne Joolaa bi, bato bi daan lëkkale Sigicoor ak Ndakaaru, suux na. Bàmmeelu Kocc Barma day delsi ci jéyya ju tiis jooju, di sargal ñi ci faatu ñépp, di jéem a yeewaale yit askan wi ngir lu ni mel bañ noo dalati. Waaye Njéeme yemul foofu: dafa nuy fàttali yit jaar-jaaru ndem-si-Yàlla ji Kinne Gaajo, fentaakon bu mag bu fiy taalifam yéemoon Afrig ak àddina si yépp. Ñoom ñaar nag, ay xariti benn bakkan, ay doomi-ndey, lañu woon, mu xamaloon ko lépp. Looloo tax Njéeme Pay di dànkaafu jàngkat bi, naan ko: bul jàppe Bàmmeelu Kocc Barma ni téereb nettali doŋŋ, téereb dekkali la tamit. Yokk na ci sax ne “fey bor, féddali kóllëre ak sàmm sama kàddu ñoo ma ko tax a bind…”"
Comment les animaux furent transformes en arbres - Buma sinukurunasu silanorumi bubaar
Lingua: francese - Joola fogny
Editore: Dodo vole
#leggereinlinguamadre #leggere #linguamadre #lingueafricane #unlibroalgiorno #ilibrisalvano #joola #joolafogny #Dodovole #libribilingui #raccontibilingui #biblioterapia #prestito #serviziodiprestito #prestitobibliotecario #mammalingua #bibliodiversità #samalegge
#leggereinlinguamadre #leggere #linguamadre #lingueafricane #unlibroalgiorno #ilibrisalvano #joola #joolafogny #dodovole #libribilingui #raccontibilingui #biblioterapia #prestito #serviziodiprestito #prestitobibliotecario #mammalingua #bibliodiversita #samalegge