https://archive.org/details/bammeelu-kocc-barma
Bàmmeelu Kocc Barma : Téereb nettali by Bubakar Bóris Jóob; Boubacar Boris Diop
"Njéeme Pay, taskatu xibaar bu siiw ci Senegaal, moo toog bés këram dégg ci rajoy réew mi ne Joolaa bi, bato bi daan lëkkale Sigicoor ak Ndakaaru, suux na. Bàmmeelu Kocc Barma day delsi ci jéyya ju tiis jooju, di sargal ñi ci faatu ñépp, di jéem a yeewaale yit askan wi ngir lu ni mel bañ noo dalati. Waaye Njéeme yemul foofu: dafa nuy fàttali yit jaar-jaaru ndem-si-Yàlla ji Kinne Gaajo, fentaakon bu mag bu fiy taalifam yéemoon Afrig ak àddina si yépp. Ñoom ñaar nag, ay xariti benn bakkan, ay doomi-ndey, lañu woon, mu xamaloon ko lépp. Looloo tax Njéeme Pay di dànkaafu jàngkat bi, naan ko: bul jàppe Bàmmeelu Kocc Barma ni téereb nettali doŋŋ, téereb dekkali la tamit. Yokk na ci sax ne “fey bor, féddali kóllëre ak sàmm sama kàddu ñoo ma ko tax a bind…”"
https://archive.org/details/yari-jamono
Yari jamono : Téere fent by Mamadu Jara Juuf; Mamadou Diarra Diouf; Séex Aliyu Ndaw; Cheik Aliou Ndao
Topics
#OSAD, #njàngat, #téeré, #metit
Fentaakon 8
https://archive.org/details/sey-xare-la
Séy xare la by Ndey Daba Ñaan; Ndèye Daba Niane
Topics
#téeré, #OSAD, #njàngat, #ladab
"Téere bii, siiwalees na ko ci ndimbalal sàqu jàpple móoi mi nekk ci Njawriñu Caada ak Moomeelu Cossan bi ñu feg
- Njiiteefu Téere ak Duruus"
https://archive.org/details/Liggeeyu
Liggéeyu ndey añub doom : Téere léeb (Recueil de contes en Wolof) by Maam Ngoy Siise; Mame Ngoye Cissé
Léeboon 1
https://archive.org/details/wolof-en
Wolof Language: The Wolof Phrasebook and Dictionary by Assane Diop
Topics
#Wolof, #Angale, #Àngale, #ولوفل, #phrasebook, #dictionary, #translationdictionary, #bilingualdictionary, #njàngat, #téeré, #làkk, #tekki
"This guide to Wolof language collects the most common Wolof phrases and expressions as well as an English-Wolof/Wolof-English dictionary. This phrasebook includes greetings, food items, directions, sightseeing and many other categories of expressions that will help anyone wanting to learn Wolof."
#Wolof #angale #ولوفل #phrasebook #dictionary #translationdictionary #bilingualdictionary #njangat #teere #lakk #tekki
https://archive.org/details/joob-mitin
Mitiƞ : Caaroy - Pikin - Caajaay - Kees Jànqeen. 1982 - 1983 - 1984 = Meeting de Pikine, Thiaroye, Thiadiaye, Thiès by Séex Anta Jóob; Cheikh Anta Diop; Soxna Aram Faal; Sokhna Arame Fall
Topics
#njàngat, #téeré, #politig, #SéexAntaJóob, #Rassemblementnationaldémocratique, #RND
"Jukki yi nu siiwal, ci mitiƞu RND yu Pikin, Caaroy, Caajaay ak Kees lañu tukkee ci atum 1982, 1983, 1984."
#njangat #teere #politig #seexantajoob #rassemblementnationaldemocratique #RND
https://archive.org/details/singali
Singali : Nettali by Séex Aliyu Ndaw; Cheik Aliou Ndao
Topics
#njàngat, #téeré, #baayo
"Singali téereb fent nettali la buy jéem a wone dund gu nàqari gi ab baayo nekke, rawatina su ndeyu jiitle ja wonewul as tuut ci yërmande.
Li am solo mooy jom, muñ, ak dogu dimbale nañu Singali ba mu màgg faj gàcce.
Waaye ba mu tekkee taxul muy feyyoonte. dafa tamu doon nit ku tabe, tey jéggale.
Ndax kat dafa bokk ci ñi gëm ne lépp a ngi ci loxol boroom bi."